Amadou Ba : « J’ai convoqué une réunion le mardi 24 Septembre 2024 à partir de 15:00 au King Fahd pour… »

0
SENTV : J’ai convoqué une réunion le mardi 24 Septembre 2024 à partir de 15:00 au King Fahd pour rencontrer les Maires, Présidents de conseil départemental, Hauts Conseillers des collectivités territoriales, Conseillers économiques, sociaux et environnementaux qui souhaitent être avec moi.
Cette rencontre va permettre de discuter des modalités de participation aux élections législatives à venir.
D’autres consultations sont prévues pour garantir la participation active et transparente de toutes les forces vives de la nation qui partagent avec nous l’ambition de construire un Sénégal meilleur.
Amadou BA
Ancien Premier Ministre
———————————————
Maa ngi woo ndaje ci talaata, 24 septembre 2024 ci 3:00 waxtu ci ngoon ci King Fahd ngir daje ak njitu goxgoxaat yi, njiitu konsilu departemaa yi, digalkat yu mag yi ci njiiti dëkk yi, digalkat yi ci wàllu koom, askan ak environmaa bi bëgga nekk ak man.
Ndaje bii daf nuy may nu waxtaane ni ñuy bokke ci wote depite yiy ñëw.
Yeneen ceytu ñu ngi waajal ngir gaaraati bokk bu am solo te leer ci képp kuy dawal réew mi, te bokk ak nun yéene tabax Senegaal bu gën.
Aamadu B.A.
premier ministre ba woon
Peut être une image de 1 personne et texte

- Advertisement -

commentaires
Loading...